ACTU SENEGAL
Cheikh Oumar Hann : « ousmane Sonko Dafay Soss Lou Nek » Cheikh Oumar Hann : « ousmane Sonko Dafay Soss Lou Nek »


Thipiri demelene ligueyi té baayi Sonko
Souba midi ngone takiussane timiss Sonko
Lekoulé naanoulene demouléne taukor ndakh Sonko
Talouléne sokhlay rew mi ndakh wakhi Sonko
Loumou wakh thi yéne deuguela thiey Sonko
Lou nguéne wakh thi mome neferé la môme Sonko
Boudoul wone môme rew mi toskoré diaraw laak Sonko
Dinaléne dane tok thi séne koll yi di nane sekhaw diadieuff Sonko